Youssou N'Dour - Ay Chono La

Ndéké mbeuguel nii la
Ndéké yaw rek lenen la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko
Mbeuguel ay chono la, boulenko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oh

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Ay chono la, bou len ko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oooh

Written by:
Habib Faye, Youssou N'dour

Publisher:
Lyrics © BMG Rights Management, Songtrust Ave

Lyrics powered by Lyric Find

Youssou N'Dour

Youssou N'Dour

View Profile
Set Set