Wilsom - Sissouman (feat. King takha)

Ay i'm Back on my bullshit man
You know what time it is
Sissouman sissou ey sissouman ay ay ay
Mané Sissouman bayil sissou man ni sissouman
Ay defma nima yalla def gueneu
Tchi lingua neh bala ngey dé
Mo geune ngeumeuy sani kherr
Di yakkeu sama derr yeu lvreikh
Meunoma disturb kone xawma loy
Djoug di teub topal fé
Beug kekh té amo cash dou
Mane ak yow mane dama fekh
Watafuckizaaa ay watafuckizeee bomay teukou Meuy keuf sa guel sa khol diekh
Mala dakeu rap dakeula teg tay ma togou Mbakhalou mc nieuwlene niou rerr
I'm tryna mbalakh on this beat
Lemme talk my shit i'm the first negga
That ever tried to do it in english
Sene rappeur yi yeup lay lit wil aka am fitt
Gucci louis bitch i'm dripping got versace on my feet
Je rap en wolof anglais français poular je sais
Même plus quoi fair je fais de la trap de la pop De l'afro de la drill mais
Putin je sais tout fair
Tout sa c'est facile pour moi c'est comme une Partie de jambe en l'aire
Toi et moi c'est pas La meme donc pas la peine de fair la guerre
Je voulais même pas rapper rapidement sur ce Beat Mais
Ces mc's continuent de me sucer la Bite fok ma yobou sene fit degeu flow
Bi rek titt danio fogone ni meunouma louy ay hit
Je suis un phénomène qui crée des phénomènes
Donc phenomenal they can't fuck with my style senii gatt
Yi lay tall intercontinental je rap trop Sal
Ils disent que j'ai un problème mental
Sissouman sissou ey sissouman ay ay ay
Mané Sissouman bayil sissou man ni sissouman
Diapewouma dara mouy dara
Mane la ma topeu tchi abba
Temp yi nak khalebi damako langual
Té guinaw gui melneu ni pattass
Haters yi khamouniou takha deuy gueneuni
Kou nekeu tchi vacances yoré ay raffals ni AK
My negga yamouma dakar
Caisser sa guel yoné ay text soubeu niou flex
May doundou Lou nekh sa khôl bi diekh ngey Tidji sa back nopil way
Beuri vitesse fi niofi bess keneu demoul niou Dess nitt
Yi amouniou khel amouniou cash beugeuniou khekh
Watafuckizaa ay watafuckizeee yallay dogual Nioune niouy nangou
Yow ngey sissou domeram Yeungeul gucci Melastikou teglé tankeu
Kaw Etage mane may gaindé yow ngey sirou soumla Diapé damlay
Saff parewolene fauk Ma djitou Pour ngene khamé lane moy star paw
Pour Ngene khamé lane moy star may sen bay
Sissouman sissou ey sissouman ay ay ay
Mané Sissouman bayil sissou man ni sissouman

Written by:
alioune sy

Publisher:
Lyrics © O/B/O DistroKid

Lyrics powered by Lyric Find

Wilsom

View Profile
Sissouman (feat. King Takha) - Single Sissouman (feat. King Takha) - Single